28 Jul 2026, 10:47 UTC856 views2 reactionsread 4 September 2026 🌴WAXI SERIÑ TUUBAA🌴
▬ஜ۩۞۩ஜ▬
[ Yoonu Magal]
*Leerug Tuubaa*, Part 9
Nee na ñu : kër SËRIÑ TUUBAA fii jumaa ji nekk la nekkoon, kenn itam daawufa nekk waaye waxtu wu nekk ñu koy defar aka defaraat.
Juroom ñenti kées la amoon, kées gu nekk am benn néeg bamu dés kées gu njëkk gi. Fii tally bu ñuul bi aw (tally bi wër jummah ji) moo donoon sàkketu kër gi
▬▬▬▬
📚 Source : Waxtaani SËRIÑ TUUBAA VOL4
❤2
28 Jul 2026, 10:47 UTC830 viewsread 4 September 2026 File
File, posted without a caption
27 Jul 2026, 09:47 UTC879 viewsread 4 September 2026 File
File, posted without a caption
27 Jul 2026, 09:47 UTC876 views4 reactionsread 4 September 2026 🌴WAXI SERIÑ TUUBAA🌴
▬ஜ۩۞۩ஜ▬
[ Yoonu Magal]
*Leerug Tuubaa*, Part 8
Sëriñ Goor Mag Jaw masnaa yabal ñaar ci SËRIÑ TUUBA jox leen ab ëmb akub bataaxal. Ni leen bungeen demee nangeen dal fa kër Sëriñ Massamba.
Bañu àgge ba tek ëmb bi fi suuf SËRIÑ BI bataaxal bi la njëkka yootu. Bamuko texarñee ba jàng ko ba noppi, wax Sëriñ Massamba pas-pas boobu lu ci ne ? Mu fecci ko mu doon ñatti teméeri dërami ngurd, mu fecci ëmb…
❤3👍1
25 Jul 2026, 10:43 UTC733 views3 reactionsread 4 September 2026 🌴WAXI SERIÑ TUUBAA🌴
▬ஜ۩۞۩ஜ▬
[ Yoonu Magal]
*Leerug Tuubaa*, Part 7
SËRIÑ TUUBA nee na :
Sama Tuubaa gii, lima fi njëkka fàggu mooy : lu fi waay jaamu ñu nangu ko, kuñu fi suul mu texe !
▬▬▬▬
📚 Source : Waxtaani SËRIÑ TUUBAA VOL4
❤3
25 Jul 2026, 10:43 UTC698 viewsread 4 September 2026 File
File, posted without a caption
23 Jul 2026, 10:16 UTC801 views3 reactionsread 4 September 2026 🌴WAXI SERIÑ TUUBAA🌴
▬ஜ۩۞۩ஜ▬
[ Yoonu Magal]
*Leerug Tuubaa*, Part 6
SËRIÑ TUUBAA nee na :
Tuubaa li tax amuma ci sago, Goor YALLAH yépp dañukoo bëggoon, SUNU BOROOM teewal goor YALLAH yépp ni : Tuubaa tànnal ! Mu tànn ma, loolo tax amuma ci sago
▬▬▬▬
📚 Source : Garabu Tuubaa VOL2
❤3
23 Jul 2026, 10:16 UTC679 viewsread 4 September 2026 File
File, posted without a caption
22 Jul 2026, 10:54 UTC720 views8 reactionsread 4 September 2026 🌴WAXI SERIÑ TUUBAA🌴
▬ஜ۩۞۩ஜ▬
[ Yoonu Magal]
*Leerug Tuubaa*, Part 5
SËRIÑ TUUBAA nee na :
Amna bés muy dox ci Tuubaa SUNU BOROOM ni ko : “Ñaari yëf daje na ci yaw ”. Mu ni ko ñaari yëf yooyu yu mu doon ? SUNU BOROOM ni ko “Dangaa dem ci man ba looma ñaan danaala ko may, suuf sii nga taxaw muy Tuubaa loo ma ci ñaan danaala ko may”.
SËRIÑ BI ni ko : ndax bind nga suuf suy dem Aljana ? SUNU BOROOM ni ko Déedéet !. SËRIÑ…
❤7🔥1
22 Jul 2026, 10:54 UTC622 viewsread 4 September 2026 File
File, posted without a caption
21 Jul 2026, 11:42 UTC678 views4 reactionsread 4 September 2026 🌴WAXI SERIÑ TUUBAA🌴
▬ஜ۩۞۩ஜ▬
[ Yoonu Magal]
*Leerug Tuubaa*, Part 4
SËRIÑ TUUBAA nee na :
Sama dëkk boobee di Tuubaa nangeen ko fonku bu baax, ab këpp (lu tuuti) ca suuf sa moo gën wurus (Or)..
jamanoo ngi ñëw joo xamni ku bëgg foo këpp sab neeg danga def ca suuf sa loo xamni booko defoon ci wurus danga am lu bari
▬▬▬▬
📚 Source : Garabu Tuubaa
❤4
21 Jul 2026, 11:42 UTC631 viewsread 4 September 2026 File
File, posted without a caption
Showing the 12 most recent of 20 posts we hold for @waxiserignetouba. View and reaction counts are the latest single reading for each post, not a live figure, and a recent post is still accumulating both. A view count marked ≈ was rounded by Telegram before we ever saw it — t.me prints views in full below 1,000 and to three significant figures above, so ≈1,200,000 means somewhere between 1,150,000 and 1,249,999. Unmarked counts are exact. Text is reproduced from the public post preview and truncated for length.